| 18) |
|
kaarim  |
| faatijabaay(at)gmail.com |
Sa réew: - |
|
Lée bóon lépén,Amoon nafi ,ndanaan lu fii amoon waxu tay mátu la géem sa josa ci ráw
juddu ci girr gi yároo ci girr gi ,te muno cee wax sa soxla mba nga bind ci ñulay woowe kángam xam nga ne dañu lay náx reek wa ye doo tuss ndax báy ci sa wewu tánkk boo bége sa mbay rafet kárr
ndax gisal ku meel ne seex annta jóob
ak sëriñ maamadu jóob dagana
sériñ Mussa ka
ak sériñ laamin jóob
ak Maam Ráwaan Ngom
Ak Seex´ Bassiru Mbaake
Ak Sériñ seex Saaibu Mbaake.
ñii ñéepu war na ñoo táx kuneek ci nuun wara bay sa tool ci wárrwi .
seetal xaadim keebe.
mánik lii ma géena jáxal mooy ne ñii ñuy woo we ay binda kát ci Rëwi Afrik gu ñul gi lu ci Ëepp munu ñoo wax darr ca lákk wán leen napale woon wáxan tumalaak di ci xalaata bind céy ndaw gácce gu réy
wánte nik lu ci Eëpu ci nun la ndax bu dee feek ku meel ni esgoor ak yeneen binda kat yu ni mel nu neel di def ay missal ca dara yu kaweya, bu ka defe ndonga ya it ci ñoom la ñiy xool Ëelag
te ñoom boo seete sen ligey yémbane dileen sámuloo ag jur keen du ñemee dem di ko sácci .Manaa lima bégg wax mooy ne bu wa Rëwmi bokoon tog wáxtán ba jubo ci gen kádu set lákk wi
Eepu luñ ciy wáx ñu jél ko def ko lá
|