Xaatimal téere sargal bi | Saytug téere bi
Àllarba, 10. Màrs 2010 22:19
Santees na la ci sa teewaay fii. Mën nga fee bàyyi sa xalaat.
Limu xalaat yi: 4   Limu xalaati xët wu ne: 10  
Sa tur Xalaat yi
4) IP bi ñu dugal  Mozilla/5.0 (Windows; U; Windows NT 5.1; es-ES; rv:1.9.0.12) Gecko/2009070611 Firefox/3.0.12  Yër dalu web bi  
kaarim  
faatijabaay(at)gmail(dot)com
Sa réew:
-
Talaata, 28. Sulet 2009 21:20 Host: static-17-139-6-89.ipcom.comunitel.net Bind ab xalaat Yónnee email

Lée bóon lépén,Amoon nafi ,ndanaan lu fii amoon waxu tay mátu la géem sa josa ci ráw

juddu ci girr gi yároo ci girr gi ,te muno cee wax sa soxla mba nga bind ci ñulay woowe kángam xam nga ne dañu lay náx reek wa ye doo tuss ndax báy ci sa wewu tánkk boo bége sa mbay rafet kárr
ndax gisal ku meel ne seex annta jóob
ak sëriñ maamadu jóob dagana
sériñ Mussa ka
ak sériñ laamin jóob
ak Maam Ráwaan Ngom
Ak Seex´ Bassiru Mbaake
Ak Sériñ seex Saaibu Mbaake.
ñii ñéepu war na ñoo táx kuneek ci nuun wara bay sa tool ci wárrwi .
seetal xaadim keebe.
mánik lii ma géena jáxal mooy ne ñii ñuy woo we ay binda kát ci Rëwi Afrik gu ñul gi lu ci Ëepp munu ñoo wax darr ca lákk wán leen napale woon wáxan tumalaak di ci xalaata bind céy ndaw gácce gu réy
wánte nik lu ci Eëpu ci nun la ndax bu dee feek ku meel ni esgoor ak yeneen binda kat yu ni mel nu neel di def ay missal ca dara yu kaweya, bu ka defe ndonga ya it ci ñoom la ñiy xool Ëelag
te ñoom boo seete sen ligey yémbane dileen sámuloo ag jur keen du ñemee dem di ko sácci .Manaa lima bégg wax mooy ne bu wa Rëwmi bokoon tog wáxtán ba jubo ci gen kádu set lákk wi
Eepu luñ ciy wáx ñu jél ko def ko lá
3) IP bi ñu dugal  Mozilla/5.0 (Windows; U; Windows NT 5.1; es-ES; rv:1.9.0.12) Gecko/2009070611 Firefox/3.0.12  Yër dalu web bi  
kaarim  
faatijabaay(at)gmail(dot)com
Sa réew:
Espaañ
Talaata, 28. Sulet 2009 19:56 Host: static-17-139-6-89.ipcom.comunitel.net Bind ab xalaat Yónnee email

assalaamu'álaykum yéen siit bi sat te di leen géram lu géna bari lool te na gám ne niit
luumu mana tolu te du bind ciw lákk kam
koo ka day na xaam ne fáyda ak fulám du sori ndax ca ñamuy binde ci seenuw lákk du ñu ko náw loo du ñu ko week mukku ci ak dundam te bu dee it waxi noopu.
2) IP bi ñu dugal  Mozilla/4.0 (compatible; MSIE 7.0; Windows NT 5.1; .NET CLR 1.1.4322; InfoPath.1; .NET CLR 2.0.50727; InfoPath.2) 
Baay Jibi  
Sa réew:
-
Alximis, 28. Mee 2009 23:03 IP: 193.49.65.23 Bind ab xalaat

Waa goor ngeen, ca kaw ca kanam rek. Daa jot nag waa Afrig yi dem ci seen xelu bopp, ban rek di sëgg ci li ñeneen ñi def.
1) IP bi ñu dugal  Mozilla/4.0 (compatible; MSIE 7.0; Windows NT 5.1; GTB6; .NET CLR 1.1.4322; .NET CLR 2.0.50727; InfoPath.2; OfficeLiveConnector.1.3; OfficeLivePatch.0.0) 
Xaadim  
Sa réew:
-
Alximis, 28. Mee 2009 18:24 Host: lri5-31.lri.fr Bind ab xalaat

Xanaa rek di sant tey ñaan sunu Boroom yokk mën gi ba ngeen eggale sunu làkk wi fu soree-sore ba askan wépp mën di ko bind, di ci jàng ngir jariñu ci.
Nanguwees na fi HTML  
Advanced Guestbook 2.4.4